

(Sheyi on the beat)
Ndeke dou mbeuguelou Kassè
Teh sax fais tout mbeuguel yi dafa rare
Dièkou ma ni douma bale yeah yeah
An konne yaw bandi nga ndèkè bébé
Sopi nga sama xol bi limonade
Siroter ko diko nane yeah yeah
Ndax baniouy ndieukeu guissanter
Li nga ma yene nimou disser
Ak niniou xolanter
Rek ma xamni yalla niou bolè
Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay)
Doflo ngama (kaay waay)
Wayè deufeul ngama (kaay waay)
Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)
So bèguè ma bègue (kaay waay)
Niou deukè di rè (kaay waay)
Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)
Maala geuneul lounè (kaay waay)
Teh yaama geuneul kounè (kaay waay)
Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)
Bègal ma bèg (kaay waay)
Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)
Soma sorè oh my love
Namel bimay yeuk thi yaw
Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul
Niouy kaf di rè
Niouy kaf di fo di rè
Ndax baniouy ndieukeu guissanter
Li nga ma yene nimou disser
Ak niniou xolanter
Rek ma xamni yalla niou bolè
Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay)
Doflo ngama (kaay waay)
Wayè deufeul ngama (kaay waay)
Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)
So bèguè ma bègue (kaay waay)
Niou deukè di rè (kaay waay)
Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)
Maala geuneul lounè (kaay waay)
Teh yaama geuneul kounè, ah (kaay waay)
Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)
Bègal ma bèg (kaay waay)
Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)
Oh bébé, toi mon bébé
Toi qui m'a tout donné
Je pourrais jamais te quitter
Je t'en fais la promesse, mon bébé
Tu m'as tellement épaulé
Quand il le fallait
M'a sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bébé yaw mi gounguè ma man malay gounguè
Et si t'a peur, crie "aidez-moi" mane maaa lay sauvé
Oh bébé yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè
Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè
Oh bébé, toi mon bébé
Toi qui m'a tout donné
Je pourrais jamais te quitter
Je t'en fais la promesse, mon bébé
Tu m'as tellement épaulé
Quand il le fallait
M'a sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bébé yaw mi gounguè ma (kaay waay)
(Kaay waay)
(Kaay waay)
(Kaay waay)
(Kaay waay)
(Kaay waay)
Lähde: LRCLIB
Ei vielä samankaltaisia kappaleita
Ei kuuntelijatietoja
Ei palvelintietoja
Ei viimeaikaisia toistoja